Actualités
SPECIAL GAMOU 2015
19/12/2015 21:28
ASSALAMOU HALAYKOUM NOOGUI LEENI ZIARE BOUWER DILEEN BAALOU AKH
LI MOOY SEN EMISSION SPECIAL GAMOU 2015
NIOU INVITE WOON CI EL HADJI ABOUBACRY...
>>
———
———
WAKHTANE CI KHASSIDA 5em partie
28/02/2015 18:43
MOUWAHIBOU NAFIKH
"Nien si Mag gni nenanou Xassida gui KOU-TED-KI mingui ko bind ci attou WAYSASSIN (1316 an musulman) .
Mom ak Jazbou, Mouhadimat, Radiytou etc……. nio massé.
S Abdou Khadre Mbacké nena day mayé Xeweul di yokk ak Ngeum, ak beug Yonnent bi...
>>
———
———
———
ahmadou bamba
10/01/2015 21:53
Ahmadou Bamba
La seule photographie connue de Serigne Touba
Cheikh Ahmadou Bamba Mbacké (Aḥmad ibn Muḥammad ibn Ḥabīb Allāh) dit Khadimoul Rassoul ce qui signifie en arabe « serviteur du prophète Mahomet ») et Serigne Touba (le marabout de Touba), né en 1853 à Mbacké...
>>
———
———
———
WAKHTANE CI KHASSIDA YI
17/11/2014 13:14
DIEUREDIEUF AHMATOU KHADIM
WAKHTANE CI KHASSIDA MOUHADIMATOUL AMDAH
Ndiaga M Ndiaye
MOUHADIMATOUL AMDAH" Xassida gui mom Xassida mad'hou la (tagg) dieumé si Yonnent bi (Psl) ,tagg ko si geun di djiko yi ,tagg gogué Sunu Borom (SWT) moko ndieukeu feusseul Wa innaka la ahla houlouhin azimin
....
>>
———
Wakhtane Ci Khassida Yi 4em Parti
01/11/2014 10:00
Amsa Amar
Dialibatoul Marahib dal limathi kham moy serigne bi mayomba lako wayaté 1898 wayko thi bakhrou radias ak bakhrou basit mou don diouroumi téméri way ak fanwér ak gniar wayé khasida gui *dafa doy war
Khassida gui lissi srgn bi dekheugne nite manouko* khame wayé daye yégé di agalé di...
>>