Wakhtane Ci Khassida Yi 2em Parti

24/08/2014 21:40

Ndiaga M Ndiaye

TOUHFATOU

Nenanou Waliyou bou niakonn tieureum bouko diangué Dèllou wat ak thieur ba, Nenanou tammit kep kou kay diangue dangay sett si ay bakkar ba melni yonent bouy dorra ganné Diamono.
So yakhouwonn ba ken meuneu toula defar so kay diangue di defarou.
Day taxaw taxawayou Serigne bou matt seuk.
So xollé *Yonnent Yalla MOUSSA sounou Borom bakhé won nako"KOUN" mouy soppi bant ap Diane nguir da nekonn si ay ndiabar kat you geumoul won lou doul lolou
Yonnent yalla ISSA loumou lalonn day donndou nguir donn gui mou donn"ROUHOU LAHA" dan na dekkil niou fatou ,dan mourri beutou silmakha ,dan doxlo ap laggo
Té so diangué wolofalou Serigne MOUSSA KA dinga degg mou nettalli la KOU TED KI fimou diar ak gni té KOU TED KI nena si Xassida gui
"WA KOUN BI MOUSSA WA BIDIAHI ISSAWAHIYANI DOUNYA WA OUHRA BOUSSA*
té Xassida meun nala yeguè ba nga tollou si Daradia biniou donn talif xassida gui

WA KANA HAQAN

Xassida gui gni ngui ko teunk si Ayya bi wakana haqan haleyna nasroul mouminina
Mingui nek si Sourate ROUM(30) Ayya(46) lou yémmé lol si nombre yi .
Waxnanou ni Xassida gui kouko wayo mou wayo ak yaw ba way ga diombou la .
Wakhat ni Kou tako ak mom mou tako ak yaw, té outou la say mbiir meun lassi fouf .
Amna nassi nak ay Xassida you outé senni biir .
Nenanou moy lougou xassida yepp .
Serigne Abdou Khadre ak Serigne Saliou diglé nanou ko biss bou nek .
Barri na lol ay mbir si biir ndax KOU TED KI amna foumou si Diar ak Cheikh Sidy Al Baba ak Jarka (résumé)
Bokou nassi tamiit Naar yako donn diss senni Adio .
Nenanou Borom keur bouko saxal dou niak ndieul mouk.
Ben Kilifa nena Beuyit wi Achkouroho wa hadali abdala doy na seuk si leral (resumé).
Kou bax nena AJHABTA FAWHA LISSIWANA
ben yonn lako bind wayé dadonn diglé nioukoy bamtou .
Xassida bou barri ndiarigne lol sax té kép koukay diangue meunga wate né kogne biga deuk kép koufa ame kheweul ak Diam ya takh mou Amko

MAFATIKHUL BICHRI

AYYA AL KHOUR' ANE bi Allahou latifou bi hibadi yarzouhou man yachaou wax nanou ni kep kou sax ak mom bo teudiouwonn sax si ap nek bagna genn sounou Borom dinala fa fek ak ay Xeweuleum ndax Ina fadhl allah youhti
moy baddil kouko SobTé benn LATIF bou BICHRI day lambo ak secret AYYA bi ak Yenen you barri sax.Té so xollé latif adad=129 En plus il ya 129 noms de Mouhammad (PSL) dans bichri .
Xassida gui YA LATIF dassiy dox té latif c'est un multiple de MOUYASSIR HASSIR diapandil lou diaffé

MAFATIKHUL BICHRI day diapandil lou diaffé.
THIEY BICHRI DIEUREDIEUF KOU TED KI-« TIHI L HOUROUFA KA DIAMIHIL SALAWAT - HALAL NABIYI YA MOUDJIBOU DAHAWATT
(Défal yilé Aaraf mou woutou mbolem Salatou hala nabi ,Yaw minga Xamni yay Diokhé khéweul
WA BASSIRI'L HOURA BIZI'L HOUROUFI -
WA HAYRA HOUNNA MIN ZAWI'L MAHROUFI
(Defal yilé Aaraf nek mbegoum way Niak gni,
Té na donn li OUROU AYNI yi di titero Euleuk
- Waliya''BARIK'' fi diamikhil Harakaat - wa Sakanaty wadjhalanha ''BARAKAAT ''
(Nanga Barkel sama beep Yeungou ak Dall ,Té nga def sama leep Barkel *THIEY BICHRI
MAFATIKHUL BICHRI*
Waxnanouni KOU TED KI bind na ay Xassida yo xamni si Diaw - wou dji lanou nek Yoyou Xassida liniouy def moy di toubeul di nianal ak di sakkoul Ngeureum Kep kou takko ak niom Nénanou bok na si yoyou Xassida MAFATIKHUL BICHRI » la clef du Bonheur Bokou na ci kemtanou Xassida gui « MAKHAMMATOU RIDIAL » WA HOUD LIYAL YAWMA MAHAMMATY RIDIAL BILLA TAJAL JOULINE WA BASSIR BI NIDIAL

Len si Missalou « MAKHAMMATY RIDIAL »
CHEIKH ABDOU HADRE DIEYLANI GOOR YALLA » Mom Yalla si boppam moko toudé Abdoul Khadre Dieylani Mingi ganné Diamono si Werou Koor té ba bi Weer bi dekh dawoul namp beuthieuk mouk lou yèmmé .
Bokonn si gni nga xamni amon nanou « HATMOUL MAKHAMMATY » manam Kou ko guiss tékhé koumou guiss nga tékhé mou nex la wala mou nakhari la ,loumou wax yalla degg ko .
KOU TED KI nena :
« Diajabali hat'tou mahamaty Ridial wali tawwa sayra Ridial wal madial » (Mbolem Thieurou "Goor Yalla" Sunu Borom def nako si sama Xassida,Sunu Borom Takhagnal nama mbolem Yonn yi Goor yalla yi di diar ) Waxnanouni mbolem lou niit di Sakou Fi ak Finiou dieum mingui si biir MAFATIKHUL BICHRI

Précédent

Rechercher

‎NOUROU DARAYNI(+1MILIONS DISENT DIEREDIEUF SERIGN TOUBA SUR FACEBOOK) DAHIRATOU NOUROU DARAYNI DIEUREDIEUF SERIGNE TOUBA © 2014-2016