EMISSION WADIAL MAGAL GUI 2015 2em partie
■Bichmilahirahmanirahimi■
○○WADIAL MAGAL GUI 2em Partie○○
•••Histoire La ville de Touba a été fondée
en 1887 par le cheikh Ahmadou Bamba Khadimou
Rassoul. Avec ses disciples, il a construit cette ville. La ville
de Touba est de nos jours
l'une des plus grandes villes
du Sénégal, de par sa
démographie, son activité
économique surtout tertiaire•••
○Tayji sen emission wadial magal migui gneuw ci deuk bou tédd bidi touba gnou indi ci touti rék ci HISTOIR jaar jaar
○○TOUBA TEUK LA BOKHAM NI SERIGNE TOUBA MOKO SANTHION CI ATTUM 1887m ji TARIH Touba nak nék deuk bou TAWFÉKH deuk bou am BATIN ndakh SERIGNE TOUBA bimkoy beuga Dako weur Lou Yağ songa guis Léérouk TOUBA
■Touba nak Tourwi migui diogué ca ALDJANNA ndakh S.fallou daan wakhni TOURWI AK GRAPP LA GOUNÉK CA ALDJANA
••Touba nék bokham ni deuk yi geuna yatou ci senegal cila bock moy niaarél bi deuk bi guena yatou ci senegal guinaw dakar ci atum 2010
○○Touba nék Deuk bokham ni Mo eup DINNÉ lislam ci SENEGAL
■TOUBA kogne (Quartier) banca gueuna mim moy DAROU KHOUDOSS
■■Touba 1er KHALIFA SERIGNE MODOU MOUSTAPHA FONDATEUR GRAND MOSQUEE DE TOUBA 2em KHALIF SERIGNE MOUHAMADOUL FADILOU MBACKE L'OUVIRTUR GRAND MOSQUE TOUBA
3em SERIGNE ABDOU AHAD MBACKE LE CREATEUR DE DAARAYKAMIL
4em KHALIF SERIGNE ABDOU KHADR MBACKE ILIMANI TAY AK EULAK
5em KHALIF SERIGNE SALIOU MBACKE BOROM KHÉLCOM
6em KHALIF SERIGNE MOUHAMADOUL LAMINE BARA MBACKE FALILOU
7em KHALIF SERIGNE SIDY MOCTAR MBACKE
Yallanafi yagtawër lool
A...suivre
3em partie
NOUROU TV en directe magal 2015