INFO DAHIRA DND
Mame asta Thiatou Nourou Dareyni
Sant nagnu la gureum nagnula
Sa dahira bi mashallah
Li rek doyna sant ! Wayit am sogné lasi yaw nga gueneu gorgorlou ndax kou guiss mbolo mi ak ni djot manké nga kham ni ligeyal serigne bi rek ka am solo
Nb: prochaine rencontre Dimanche 1 mars 2015 au lycée des parcells assaini
* beugnét bi mashallah
Bong bong bi tamit tarkalah