DIEUREDIEUFÉ BOROM TOUBA. Mbokk talibé yi siar nalén di khamalné wa groupe bi daniouy diokhé don habillements ak aliments ci prison (Mac) bou linguére le 1er avril. Wa cellule bou linguére nioko organisé dieuwrine birame mouride ndiaye 77 112 29 67. Niouy sakkou ci wa groupe bi yeup niou diapsi surtout coté finance wala matériels ndakhté liguéyal sérigne touba rek monou nior. Info 77 347 59 44 ou 77 539 47 57