MAGAL KAZU RAJAB 2016
WADIAL MAGAL KAZU RAJAB
SERIGNE MOUHAMADOU FADAL MBACKE
Serigne Fallou Mbacke : migui ganné aduna ci Atum 1888
ca Darou Salam.
Ay waadiouram : Cheikhouna Cheikhoul Khadim Khamdoullahi warassolouho
ak Sokhna Awa Bousso
Migui diangué : ci Mame Thierno Ibrahima faty boba Serigne Touba gui ci Touki bi
Migui nék Khalifa : 1945 2em Khalif Serigne Touba ci Diamono jou Yémé
Yim déf ci Touba : mo Agalé Djoumay ji défar Marché Occas exte...
Litah ñouy Magal Magalou Kazu Rajab : Serigne Fallou Mbacke migui ganne Aduna ci wérou Rajab ci ñaar fukki fan ak jouroom ñaar Tombé ak
(27 Juin 1888)
biss boba nak sa You ñeuwéwa moom. SERIGNE FALLOU dadan dém Darou Salam ba beutt sétt bou ñeuw Touba bou dém ba S.Modou bousso diko Magal
Mou dém ba tollou nimou tollou Tay
Serigne Fallou nak : kou bari ay Tourando la mo fékk kou Fatou mou dékalko
Mo Fathi Pr Ivoirien exte... mo Yobou kou mousta déf lou néh yalla mou yobbou al dianna modém makka déffa ay kêmaan
Mo ñeuka bind ni diooy ta SerigneTouba rék tah Farata la
Migui wouyou ji boromam ci atum 1968
Wasalamou Khalaykoum Warahmatou lah Barkéb Borom Touba Magali ci Jamm ñeuw ci Jamm ci Serigne Fallou