Magalou Khassida yi SERIGNE AMSATOU MBACKE
Serigne Fallou Diaw Khassaid> Bahda Salam Sopeye Serigne Amsatou Mbacke gnoléni Yeugal beusoub xassaida ak alkhouraan à Touba Dialibatoul Marakhib Keur Serigne Hamsatou Mbacke samedi le17 /janvier /2015 yalla nanou ci sounu borom yobbou ak djamou nou agalékou ci djamou dadjéé fak ngeuramal Serigne Touba allahouma aminne
Pour Community Apple Service Commersial 767350405