WAKHTANE CI KHASSIDA YI

WAKHTANE CI KHASSIDA YI

Amsa Amar

Dialibatoul Marahib dal limathi kham moy serigne bi mayomba lako wayaté 1898 wayko thi bakhrou radias ak bakhrou basit mou don diouroumi téméri way ak fanwér ak gniar wayé khasida gui *dafa doy war
Khassida gui lissi srgn bi dekheugne nite manouko* khame wayé daye yégé di agalé di défare maname tarbiya ndakh srgn bi fi adjiline ka aadjiline liraahip la wakh maname fii ak felé

Waw marahib s.bi an ndi nathi mbou toum khasbala di a housou bilayi mina saytané radjimi ak mbou toum basmala di bismilahi rakhmani rahim
Bo sétlo thi bir khasida gui bekhrou radias bi doroumi téméri wayla ak gniar foukou bakhrou basit bi don fouki way ak gniar ta lolou ay mbirla thi bir
Srgn touba néna yawe yalla sama khasidagui kikoy diang nang ko maye louko doye lokhamni dotoul sokhlale *kéne dara
Kou téde ki néna yala déf na sama* khasida gui arafe bou néke mbéktéme rassouli laahi psl laye done
Kou téde ki néna yawe yalla kiye diang marahib nangko maye lo khamanténi ki diangoul khasida gui dinakako *gnéwé ba faw
Wahablimaye yakhrahahoo ma yarbitou bihii siwaahou ya diamiilane* wisitou té néna lolou gnoukoy gnéwé sakh nakoy guiss bame kaye sawarloo sibe diang marahib
Néna sama khasida gui daye kheuthiy nite ki diko téke si yoonou siratal moustakhime wayé dafe koye maye ak lére wabil karami wabil ichara ihdi mouridane yatouboul innaa

Ndiaga M Ndiaye

FOUZTY
Xassida gui bok na si Xassida yi teunk « MAFATIKHUL DJINANE
SERIGNE ABDOU KHADRE (RA) waxnani:
Xassida gui day yokk ay Xeweul ak di begeul talibé bi foumou meunti nek.
Xassida FOUZTY diaglé la si Soxna sou mag si nga xamni mom mo am Diaglé si ap SOURATE AL'HOUR'ANE mouy
« SEYDATOUNA MARIAM »
ak
Yonnent Yalla ISSA « ROUHOU LAHA ».
Waxnanouni KOU-TED-KI lolou lay dioundie si tambali Xassida gui.
Nénanouni nimou tagué fi « SOXNA CI » eup na ap Xel.
Ken meusso ko degg té ken dotou ko dèggeuty ABADAN
Waxnanouni FOUZTY ak HOUDA ILAHI
KOU-TED-KI nianon na Sounou Borom (SWT) mou geuneul ko si yiko djittou yepp (lou yémmé).
Fouzty bok si Xassida yi nga xamni OUROUL AYNI mom laniouy way ak diko titeuro euleuk Sounou Démmè Al'Dianna.
KOU-TED-KI mingui ko teudié Wa houri hayna Wadjhal ya rabbi hajihi'l Xassidatamin ah'saani maa tatahan'naa bihi'l houri'l haynou ya hayra
(Yaw Sounou Borom (SWT) nanga def Xassida gui mouy dallal ap hol ak diko seddal (Yaw sunu Borom(SWT) nanga def tammit mo donn li geun si way yi« OUROUL AYNI » yi di way Aldian'na)
Mak gni dan nanko bolé si nianou « SEUY » ak di ko tèerto ak diko dalallé « SÊETT » ndax dagno waxni Xassida gui leep da di ngeunel té Keep kouko saxal ndam rek ngay am si sa beep dioublou
KOU-TED-KI mingui niou fiy leeral tammit li oumpou nien gni si Yonnent Yalla ISSA ROUHOU LAHA
« Ya Oumma rouhi'l Maliki ya ouma diali'l Haliki
« Ibnouki la bihaliki hinda hali moumassiki... Dieuredieuf Serigne Touba Khadimoul Rassoul, Diarama Mame Cheikh Ibrahima Fall Baboul Mouridina

 

Rechercher

‎NOUROU DARAYNI(+1MILIONS DISENT DIEREDIEUF SERIGN TOUBA SUR FACEBOOK) DAHIRATOU NOUROU DARAYNI DIEUREDIEUF SERIGNE TOUBA © 2014-2016