Archive des articles
Beug Serigne Touba
20/11/2014 16:02
NOUROU DARAYNI +1millionsdepersonnes disent dieuredieufa Serigne Touba sur facebook
>>
———
WAKHTANE CI KHASSIDA YI
17/11/2014 13:14
DIEUREDIEUF AHMATOU KHADIM
WAKHTANE CI KHASSIDA MOUHADIMATOUL AMDAH
Ndiaga M Ndiaye
MOUHADIMATOUL AMDAH" Xassida gui mom Xassida mad'hou la (tagg) dieumé si Yonnent bi (Psl) ,tagg ko si geun di djiko yi ,tagg gogué Sunu Borom (SWT) moko ndieukeu feusseul Wa innaka la ahla houlouhin azimin
....
>>
———
Wakhtane Ci Khassida Yi 4em Parti
01/11/2014 10:00
Amsa Amar
Dialibatoul Marahib dal limathi kham moy serigne bi mayomba lako wayaté 1898 wayko thi bakhrou radias ak bakhrou basit mou don diouroumi téméri way ak fanwér ak gniar wayé khasida gui *dafa doy war
Khassida gui lissi srgn bi dekheugne nite manouko* khame wayé daye yégé di agalé di...
>>
———
KHASSIDA NAHDIOU
05/09/2014 23:00
Amsa Amar
Serigne Touba daye wakh si neuhdiou néna lasa djitou mak yereum goné goné fonk mak néna bépe yone wounit diem té andoulaki téguine dousi diarignou dou tékhé bokou nasi téguine kou gnewe si yawe wakhla sokhlame ngua fadialkako booko ameé té yalla takh té boul siweul Boknasi gnak téguine...
>>
———
Wakhtane Ci Khassida Yi 3em parti
31/08/2014 22:30
Ndiaga M Ndiaye
RAA I YA
Waxnanouni Xassida tagg la dieum si geun di mbindef .
Bokou yoyou tagg ay BEUYIT you ken meusta guiss youni mel .
Waxnanouni Xassida gui kou koy diangue dangay begeul Yonnent bi (Psl) ak Sakhaba yi ak mbolem Gayou Bakh yi si geun di mbecté té kou begeul gni begeul...
>>
———
Wakhtane Ci Khassida Yi 2em Parti
24/08/2014 21:40
Ndiaga M Ndiaye
TOUHFATOU
Nenanou Waliyou bou niakonn tieureum bouko diangué Dèllou wat ak thieur ba, Nenanou tammit kep kou kay diangue dangay sett si ay bakkar ba melni yonent bouy dorra ganné Diamono.
So yakhouwonn ba ken meuneu toula defar so kay diangue di defarou.
Day taxaw taxawayou...
>>
———
CHEIKHI SERIGNE TOUBA YI
24/08/2014 21:30
Amsa Amar
Dafa ame biss serigne bi wolou serigne modou diaw pakha niko modou diaw ndakh kham ngua si waliwou yalla yi kane mosi guena mag Serigne modou diaw niko khana mane Sergne bi niko koula wakh yawa Serigne modou diaw niko boulaye néékhe makoye nékk Serigne bi ni téékk diéki niko ndakhame...
>>
———
Wolafalou mack gni
21/08/2014 18:00
Wakhi Serigne moussa ka
Amsa Amar
Serigne bi gnongui deti gnana fakhir dafaye nango dagane nangoul gnou lep lougnou gnane ndakh yalla natal kharnoubi gnogui dagaane si moustapha maneke marwat'ak safane ak akhi amdi moustapha mi yalla diébale kharnubi ak àqi mboléme aye rakame ak àqi séne baye...
>>
———
Serigne Touba Rek
18/08/2014 08:30
Mame Saliou Diop
Information ! Pour ceux Qui veulent aller à St louis Niaarri raaka Ya Veuillez contacter 77 539 47 57
Kouy dém ndar sa niaarri rakka ya
wa Groupe danfa beuga déff caravane
kousi beug ay léral man woté ci #775394757
Jaar Jaari Serigne bi
contact:...
>>
———
WAKHI SERIGNE TOUBA
13/08/2014 12:30
Serigne touba
nena ndigueul leudeum mouk fadiar la si ler rek la dieum loudoul ndigual nak leudamouk timis la si leudeum la dieum guayi de len weuy si ndigueul tê bayi tèrè>
Adji Coumba Ba
Serigne Touba boromouk maye la borom saggne sagne la. Kou téd ki néna Wa anfiiyoune fiiniibiyawmine...
>>